Viviane Chidid - Teeyal (Clip Officiel)

Votre vidéo commence dans 10
Passer (5)
cash machine v4

Merci ! Partagez avec vos amis !

Vous avez aimé cette vidéo, merci de votre vote !

Ajoutées by admin
75 Vues
Viviane Chidid
Clip Officiel "TEEYAL"

"La rumeur, cette vérité qui se promène comme un mensonge, de bouche à oreille, qui ne fait pas réfléchir les gens, qui passe comme un soupir au-dessus du vent.... "

Produced by : VQ

Arrangement : AKATCHE
Written by : Bakhaw
Mixing and Mastering : AKATCHE

Single disponible sur toutes les plateformes de téléchargement et sur iTunes Music

Abonnez-vous à la chaîne / Follow us : https://www.youtube.com/channel/UCYsdOXVmOjhT-LB2r9U35Mg?view_as=subscriber

Join Viviane Chidid on INSTAGRAM: https://www.instagram.com/vivianechidid.officiel/

Join Viviane Chidid on FACEBOOK: https://www.facebook.com/VivianeChididOfficiel/


Lyrics

Deugeu teule nè rek tothie na teyal
loufi diar ngendy daw bey danou teyal
fo tok beugeu gnou nawla teyal
wagnil eupeule tè ba netali teyal
dègueloulene Wakhou yaram ba teyal
neuneu wakhou kham yone bè ko geune teyal beugeu buzz bamou diarala teyal
nga taguègo tè dewagoul

Cou nek amanga Lila daye fekhèl nga dieum ko lindianti dhè Lila wakh sa galer ngi takk Di boy
dieum ko lindianti té Faye ko dhé li la Wakh
lou touty nga def ko lou patta
Lo xam netali li la wakh
Yakamti rayone na sa gnaum mame
deuguena rayone na sa gnaum mame

boukou lék féké gnorogoul
boul di Wakh lo khamné amagoul
Xamoulo do Khar bagnou xamala
Guissoulo do Khar ba guiss Lou geuneu lér nga dem
Na nga tey ta nga dale
Amigo Li ngaye Wakh wauroula
nopi bakhna thi Lo xamoul lanla
Gawa Wakh Meuna indi mussiba

Deugeu teule nè rek tothie na teyal
loufi diar ngendy daw bey danou teyal
fo tok beugeu gnou nawla teyal
wagnil eupeule tè ba netali teyal
dègueloulene Wakhou yaram ba teyal
neuneu wakhou kham yone bè ko geune teyal beugeu buzz bamou diarala teyal
nga taguègo tè dewagoul

Manè li Khawma lanla li khawma lanla li khawma lanla li ( bis)
ki dhè lidjantinala lidjantinala lidjantinala yaw mi ( bis)

Lingua bindeu eskeu deugeu leu
fake news mane yeugeulouma
beugeu beuz ba takh nga dima sosal
lingua def Dou xam gna Noumou toudou toumale boy yakati nit
wala sakh boy bindeu thi nit nala l’ère li ngaye Wakh ni lou ame la
lou ko moy Dina done sa musiba

Deugeu teule nè rek tothie na teyal
loufi diar ngendy daw bey danou teyal
fo tok beugeu gnou nawla teyal
wagnil eupeule tè ba netali teyal
dègueloulene Wakhou yaram ba teyal
neuneu wakhou kham yone bè ko geune teyal beugeu buzz bamou diarala teyal
nga taguègo tè dewagoul
Catégories
Musiques

Ajouter un commentaire

Commentaires

Soyez le premier à commenter cette vidéo.