Dope Master - Vroum Vroum Feat. Zo Flame [Official Music Video]

Votre vidéo commence dans 10
Passer (5)
cash machine v4

Merci ! Partagez avec vos amis !

Vous avez aimé cette vidéo, merci de votre vote !

Ajoutées by admin
55 Vues
IMEAN / AMIN VERSION DELUXE DISPONIBLE LE 05 MAI 2023

https://wiseband.lnk.to/Dope-Master-Vroum-Vroum

Watch Full Episodes / Regarder tous les épisodes : https://urlz.fr/jnRG

Réalisation : Kirama

#DopeMaster​ #zoflame #vroumvroum

Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux / Find me on my socials:
https://www.facebook.com/Dopemasterwrld
https://www.instagram.com/dopemasterwrld/
https://www.youtube.com/c/DopeMaster
https://audiomack.com/dope-master-2

Parole / lyrics

1e couplet

Dope Master

Guenn si ghetto bi weuri ay liass i did I did
Beugu ma dem wanté dioukhougn ma passe teh meunougn ma goungué yah
Daw senn circuit grand yi sissou boy yi dima cons ko ni Chinois
Maral nieup geumougn kenn daniouy changé kanam ni tiaga sou goudé
Fuck nieup
Loloy loi ndeysann das real
Get money dieundeu big house pour mère
Fokma moytou sama gars yi mangui yonou succès
Mané bb geumo dara bouma wilipandé
Mann ngua beugu meusso teud expliquer noumouy démé
Damay danou rek diouk deukou macky Dafeu amoul nelaw
Mangui takk ay boneu nigga takagou ma sokhna batay
Guiss bou bakh bi comme guerre fuck love
Bala leer beut sét
Bala deum woné kanamam goudi diote
Concert niou encaisser probleme yi mougn koy gerer no stress
Fuck bête si guinaw mic boudoul maté face face das cap haha hey
Niongui si jail kom gni abonnés si orange
Capture d’écran seuy ni yakou a si vocal
Appel vidéo meunn na sopalékou menace

Ki moy crack wanté dou dém class
Pablo scobar la def reference
Kham na Louy plan teh teksi day bedav



Refrain
Yay wakh niouy déf
Only og no fake
Romb nieup ndinnt ndint
Flowou moto compet
Am dara neubou niouko
Ki niémè ay beut LOY KHOL

Niom Daniouy mèrr di leu ré
Daniouy yorr di leu pé
Daniouy tok bamou nekh
Sou taré niou né mèss
Daniouy déclarer vrai
Souniouy tioubou dougn ko tay daniou faux


Démarrer Démarrer Vroum vroum
Peundeul fi dieul ngua seu cons cons
Ferrari kenn douko pouss pouss

Tassaré Tassaré town bi yeup
Dioudou si souf fi yek késsé fi Seuss
Mayé wougn dara lo niou may niou dieul Waw



2e Couplet

Zo Flame

‘’AY ‘’
Ay texte you terre à terre lafiy tek kouko tegui degg boom boom
Solou big dripp Adiou sikaw lambooo domeu guiss mais digeu degeuh vroum vroum
Appuie Long rek mou takeu easy melni Dodge Charger biniou tegal Paul Walker easy
Rendez au sommets my G
From west Africa nioumey diawalei
kaw Man
Hum Loy khol ?
Xamé gama key mane leu Boy bou xoulok yarou “wreeew”
Rew beu doff Xalei douko tendance
Xawma fo perte temps leu awma sakh vacance inwww Boom Boom
Signaler Left’euh diaar right
Eh siguil geu khol meu mmagui Sky
Star la dh m’y G je brille
‘’ laf thiatt 3x “



Refrain
Yay wakh niouy déf
Only og no fake
Romb nieup ndinnt ndint
Flowou moto compet
Am dara neubou niouko
Ki niémè ay beut LOY KHOL
Niom Daniouy mèrr di leu ré
Daniouy yorr di leu pé
Daniouy tok bamou nekh
Sou taré niou né mèss
Daniouy déclarer vrai
Souniouy tioubou dougn ko tay daniou faux


Démarrer Démarrer Vroum vroum
Peundeul fi dieul ngua seu cons cons
Ferrari kenn douko pouss pouss

Tassaré Tassaré town bi yeup
Dioudou si souf fi yek késsé fi Seuss
Mayé wougn dara lo niou may niou dieul Waw

© 2023 Nautylusprod
Catégories
Master Class Musique
Mots-clés
dope master, zo flame, Vroum Vroum

Ajouter un commentaire

Commentaires

Soyez le premier à commenter cette vidéo.