** Abonne-toi à ma chaîne en cliquant ici https://goo.gl/GwQBFK **
Faalé Ma - qui signifie littéralement « Fais attention à moi" - raconte l'histoire d'une femme secrètement amoureuse d'un homme que sa compagne maltraite. Elle souffre de cette situation et rêve d’être celle dans les bras de cet homme.
Pour mettre sa chanson en images, Adam Sène s’est entourée d’un casting prestigieux : Pape Ndiaye Thiopet - star de la musique sénégalaise ayant chanté avec les plus grands -, Djiby Seye alias Ndiol Todj Todj, Fabrice Fayal - que l'on apprécie dans la série « Infidèles » dans le rôle de Bachir - et la charmante Ndeye Awa Ndoye, vidéogirl et actrice.
#AdamSene #FaaleMa #PapeNdiayeThiopet #Love #team221 #mbalax
** Les crédits de la chanson et du clip FAALE MA **
Auteurs : Adam Sène / Pape Ndiaye Thiopet
Compositeur / Arrangeur : Hakim Abdul-Samad
Mix & Mastering : Poliman
Réalisateur clip : Mao SIDIBE
Label : Adam Sène Productions (Dakar, Sénégal, octobre 2021)
Remerciements: Diarra DIOP STYLENA, BARAKATOU BASIN RICHE BAUER qualité supérieure 100% Bio, H-Déco, Couro's Beauty and Spa, Pape Ndiaye Thiopet.
** Retrouvez Adam Sène sur les réseaux sociaux **
Facebook https://www.facebook.com/AdamSeneMusic
Instagram : @adam.sene
TikTok https://www.tiktok.com/@adamsene
Snap: senandar2
Twitter : @Adambakary
** Les lyrics de la chanson FAALE MA **
Adam :
Baby please guestou ma
Mane may ki gueun tchi yow
Chéri please faalé ma
Mane may ki baakh tchi yow
Sa ndaw si sonal nala
Nimou lay def ni mane nekhou ma
Khana khamoul chance bimou am
Bimou nékék goor bou mel ni yow
Baby boy guestou ma
Ni ma la beugué do ko guis fenen
Yow chéri boy kay faalé ma
Lima la yéné, yenewmako kenen
Dég na wolof Ndiaye di wakh naan
Gni meuna koteu amougn mbaam
Di na la siguil sagal la si say biir nawlé
Bess bou né mou dila torokhal
Sama khol tang dieur mel ni khal
Dafa dof mom di la sagané
Té bouma la amone daw ba dé
Hmmmm hmmmm I love you more than anybody
Hmmmm hmmmm together we can be happier

Thiopet :
Thiey baby mbeuguel yalla koy def dji diaam boulko fowé li la wakh
Eh mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ah han
Lekatoul nanatoul guestou ko heey mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ah han
Adam :
Aaaaaaah Haaaa ah haaaa
Thiopet :
Mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ni ah han
Adam :
Baby boy beug na la
Thiopet :
Eywaay Mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ni guestoul
Adam :
Loy khaar pour guestou ma
Thiopet :
Mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ni guestou ko
Adam :
Chéri boy ni ma la beugué do ko guis fenen
Thiopet :
Mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ni guestoul
Adam :
Bo nieuwé tchi man do to khol fenen hey heeeey
Thiopet :
Mbeuguel dou diaay mbeuguel dou fo ni guestou ko
Thiopet :
Demleen dokhal kaay
Adam :
Kone guestou ma
Baby boy heey kone faalé ma (×2)
Thiopet :
Li dawna yaram Adam
Guestoul goné gui
Boko guesto do ko rethiou
Mo la beug té yow lay sago
Adam :
Khippil say beut × 2
Thiopet :
Am na niouy khol té dounou guiss Adam khamo
Adam :
Khippil say beut
Sama wadji khippil say beut
Thiopet :
Mbeuguel dafa meti té kholal ken kila beug diar na daw ba dé nguir gni la bagn
Adam :
Ma beug la khalé bi té meuno ko kham
Thiopet :
Aythia, aythia Adam
Adam :
Chéri coco wakh ma no ko guissé
Thiopet :
Eywaay diogleen yeungatou
Adam :
Ni beug naa ni beug na la
Thiopet :
li daw na yaram
Adam :
Chéri coco wakh ma no ko guissé
Thiopet :
Wakhal goné gui
Adam :
Ni beug naa ni beug na la
Thiopet :
Adam mbeuguel dou louniouy café
Dangay yewou souba dal di seg café
Lolou kouko def do guis len lou diafé
Té lo wakh Adam dafay safé
Di passé mouy massé
Di tog mafek basé
Ma diokh la laisser passer
Adam :
Ma beug la khalé bi té meuno ko kham
Thiopet :
Li doy na waar
Adam :
Chéri coco wakh ma no ko guissé
Thiopet :
Li comme guerre
Adam :
Ni beug naa ni beug na la
Thiopet: lolou deug la
Adam :
Chéri coco wakh ma no ko guissé waw
Thiopet:
Eywaay

- Catégories
- Artistes & Divers News
Commentaires